E2 - Jaar-jaaru Aissatou

Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna

09-03-2024 • 10 minutes

Niarelou épisode bi si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay.

Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information.